Testo Borom Gal

Testo Borom Gal

GUEDJ MAMBOULANE (BIS)

Thiey borom gaal
xam ngani guedj amoul bankass
ndakh alalou adouna diarna yénayi
yapp sounou aye doom
té xamo foye téré ak gnome
beugeu fathie gathié adouna
diaral lène taylé sène bakène
yé yé waw
souma xamoni
souma dougué sa gaal
douma délousséti
kone dinako sétate bou bakha bakh

borom gaal
thieye borom gaal
ak yawmi di dougou gaal
té ngéna dall
té xamni dal
yalla diékhoul
refrain
guedj mamboulane (bis)

solo
Ma samba laobé N'diaye
taye ma wakhla thi immigration clandestine
africa métina gayi xiff nagnou
guerre yi barrina lolou
waye dieuli gaal gui
dougou thi guedj gui
lolou diaye sa bakane la

Choeur
ki mo nékk (thiey borom gaal mo nékk waw)
ki mo nékk borom gaal ya nékk (néeeeeeeee ahn borom gaal)

guedj mamboulane (refrain)
Testi Adiouza